Serigne Malick Diop
Sunu Yaakaar
Toppal sunu emission ci facebook.com/sunuyaakaarSoo ame laaj, Yaakaar Ju Sax am na tontu. Bindal seeni laaj ci yaakaarjusax@gmail.com
Author
Serigne Malick Diop
Category
Podcast website
Latest episode
Jan 31, 2026
Where to listen?
Podcasts in the app Replaio Radio Coming soonPodcasts are coming to the app soon. Install now and be the first to see a whole new take on podcasts
Episodes
Macë Saar 7 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 09.02.2023 6:54
Bul ñaaw njort, ba àtte sa moroom Yàlla nangu na ñaanu ku gëm Bunt bu xat bi Garab ak meññeefam
Yeesu Krist ALMASIH Lu Mu Tekki 01.01.2023 11:11
Yeesu Krist ALMASIH Lu Mu Tekki by Serigne Malick Diop
Mucc Saar 15 | Woyu Musaa waak bànni Israyil 27.12.2022 9:20
Ma woy Aji Sax ji, ngir ndamam li kawee kawe. Fas ak gawaram la fab, xalab géej. Sama doole, sama kaaraange, Ki Sax a; te mooy sama wall tey. Mooy sama Yàlla, ji may tagge, sama Yàllay maam, ji may joobe.
Yalla Ci Boppam Mo Ko Wax 25.12.2022 7:58
Yalla Ci Boppam Mo Ko Wax by Serigne Malick Diop
Mucc Saar 14 | Firawna dabi na bànni Israyil 24.12.2022 11:09
Aji Sax ji waxati Musaa, ne ko: «Waxal bànni Israyil, ne leen ñu walbatiku dali fa jàkkaarlook Pi Axirot, ca diggante Migadol ak géeju Barax ya. Dal-leen foofa jàkkaarlook Baal Cefon ca tefes ga. Su ko defee Firawna da naan: “Bànni Israyil de dañoo réer ci àll bi, ba faf keppu ci màndiŋ mi.” Gannaaw loolu maay dëgëral boppu Firawna, mu topp leen, ba ma jaare ca siiwal sama ndam, ndax maay daan Fir...
Macë Saar 6 | Jang ak Ibrahima Diop 23.12.2022 7:56
Ni ñuy sàkke sarax Ni ñuy ñaane ci Yàlla Ni ñuy woore Alali laaxira Wóolul Yàlla
Mucc Saar 13 | Lu jëm ci aada, yi ñuy baaxantale 21.12.2022 10:42
Aji Sax ji waxaat Musaa, ne ko: «Nanga ma sédde bépp taaw bu góor, nit ak mala, lépp lu jëkka juddu ci bànni Israyil, maa moom.» Musaa ne mbooloo ma: «Fàttlikuleen bésub tey jii ngeen génne Misra, kërug njaam gi, ak ni leen Aji Sax ji yiwee dooley loxoom. Bu ci kenn lekk mburu mu am lawiir. Yeena ngii tey di dem seen yoon ci weeru Abiib. Kon keroog bu leen Aji Sax ji yóbboo réewum Kanaaneen ña ak...
Mucc Saa 12 | Lu jëm ci bésub Mucc ba 14.12.2022 18:11
Aji Sax ji wax na ak Musaa ak Aaróona ca réewum Misra, ne leen: «Weer wii mooy doon ci yeen wi jiitu ci weer yi, te na doon ci yeen weer, wi jëkk ci at mi. Waxleen ak mbooloom Israyil mépp ne leen, bésub fukkeel ba ci weer wii, na ku nekk jëlal njabootam ab gàtt, kër gu nekk ak gàttam.
Mucc Saa 11 | Yàlla waaj na yar bu mujj ba 12.12.2022 6:28
Musaa daldi wax Firawna ne ko: «Aji Sax ji dafa wax ne: “Bu guddi gi xaajee, maay wër Misra gépp, te lépp luy taaw bu góor ci réewum Misra, dina dee, dale ko ci taaw bu góoru Firawna, mi toog ci jal bi, ba ci taaw bu góoru jaam bu jigéen bu féetewoo wol, boole ci luy taaw bu góor ci jur gépp.
Ibrahima Diop nu jang Injiil | MACË saa 05 Aaya 26 - 47 09.12.2022 6:39
Danuy Jang Injiil
Ibrahima Diop nu jang Injiil | MACË saa 05 Aaya 1 - 25 08.12.2022 11:01
Danuy jang Injiilu Almasi Bi
Ibrahima Diop nu jang Injiil | MACË saa 04 06.12.2022 11:39
Mathieu 4 en Wolof
Mucc Saa 10 | Serigne Malick Diop 05.12.2022 12:55
Danuy jang Mucc saa 10 (Exodue 10 dans le Torah)
Mace saa 03 | Ibrahima Diop 03.12.2022 11:40
Waareb Yaxya
Mucc Saa 09 | Serigne Malick Diop 01.12.2022 11:56
Danuy jang Mucc saa 09 (Exodue 9 dans le Torah)
Ce Que Dieu Nous Attends | Fortifie-Toi et Prends Courage 25.11.2022 14:00
Malick Diop est le pasteur principal de l'église baptiste yaakaar ju sax de St. Louis, Sénégal.
Cosaanu Yeesu Kirist | MACË saa 1 - 2 23.11.2022 14:16
Xibaaru jàmm bi ci Almasi bi Yeesu, ni ko Yàlla jaaralee ci MACË Jang ak Ibrahima Diop
Mucc saa 08 | Malick Diop nu jangal kaddug Yalla 22.11.2022 11:50
Mucc saa 08 ci dundu yonent Yalla Moussa.
Mucc saa 07 | Serigne Malick Diop nu jangal Kaddug Yalla 19.11.2022 11:43
Mucc saa 07 | Serigne Malick Diop nu jangal Kaddug Yalla by Serigne Malick Diop
Wareefu Taalibe Yeesu Bi Ci Jamono Jii 18.11.2022 32:58
Waxtaan ak Serigne Malick Diop ak Julien Faye ci wareefu taalibe bi ci jamono jii.
Fortifie-Toi et Prends Courage avec Pasteur Malick Diop 15.11.2022 20:54
Pasteur Malick nous encourage de se fortifier et de prendre courage dans la Parole de Dieu
Mucc Sa 6 | Exodue Chapitre 6 en Wolof 11.11.2022 7:38
Yàlla dellu na yónni Musaa | Lu jëm ci cosaanu Musaa ak Aaróona
Mucc saa 04 aaya 1 - 17 | Yàlla jox na Musaa ay firnde 01.11.2022 6:25
Gannaaw loolu Musaa dellu wax Aji Sax ji ne ko: «Waaw, su ñu ma dégluwul te gëmuñu ma, xanaa ne ma: “Aji Sax ji feeñuwu la” nag?» Aji Sax ji ne ko: «Li ci sa loxo lu mu doon?» Mu ne ko: «Aw yet.» Aji Sax ji ne ko: «Sànni ko ci suuf.» Mu sànni yet wa ca suuf, mu soppliku jaan. Musaa dellu gannaaw. Aji Sax ji ne ko: «Tàllalal sa loxo, jàpp ci geen gi.» Musaa tàllal loxo ba, ne nikk jaan ja, mu dellu...
Mucc saa 03 | Aji Sax ji yónni na Musaa 29.10.2022 9:29
Léegi Musaa ngay sàmm gàtti goroom Yettro, sarxalkatu Majan ba. Mu yóbbu jur ga fu sore ca màndiŋ ma, daldi agsi ca suufu tundu Yàlla wa ca Oreb. Malaakam Aji Sax ja feeñoo ko foofa, melow sawara wuy tàkk, jafal fa ab gajj. Musaa xoolaat, ndeke gajj ba bépp jàpp na, ba ne jippét, waaye lakkul. Musaa ne: «Mbir mu yéeme mii daal, naa jàdd xool ko, ba xam lu tax gajj bi lakkul.»
Mucc saa 01 | Bànni Israyil dem na réewum Misra 27.10.2022 13:42
Ñu dem ba jëmmi jamono, beneen buur bu xamul Yuusufa falu ca Misra. Mu wax ak waa réewam, ne leen: «Giirug bànni Israyil kat ñu ngi nuy gëna bare, ba ëpp nu doole. Nanu ci sàkk pexe, ngir ñu bañatee yokku. Lu ko moy bu xare amee, man nañoo far ak sunuy noon, xeex ak nun, ba génn réew mi.» 11Ba loolu amee ñu fal ay nit ñu leen di ga ca seeni sas, di leen ca fitnaal lool. Noonu la bànni Israyil taba...
Similar podcasts
Replaio is not a podcast publisher; show names, artwork and audio belong to their authors and are distributed through public RSS feeds.