Serigne Malick Diop

Sunu Yaakaar

Religion FR ↓ 353 episodes

Toppal sunu emission ci facebook.com/sunuyaakaarSoo ame laaj, Yaakaar Ju Sax am na tontu. Bindal seeni laaj ci yaakaarjusax@gmail.com

Author

Serigne Malick Diop

Category

Religion

Podcast website

soundcloud.com

Latest episode

Jan 31, 2026

Where to listen?

Podcasts in the app Replaio Radio Coming soon

Podcasts are coming to the app soon. Install now and be the first to see a whole new take on podcasts

Get it on Google Play Install for free Android 5M+ downloads · 4.8 rating iOS soon

Episodes

Mace Saar 25 | Xibaaru Jamm ak Ibrahima Diop 26.04.2023

L'injiilu Almasi Bi

Mace Saar 26 | Xibaaru Jamm ak Ibrahima Diop 24.04.2023

Injiilu Almasi Bi Issa

Jot njéggal bu joge ca Yàlla (suite) 24.04.2023

Ibrahima Diop nu jangal Kaddug Yalla

Jot njéggal bu joge ca Yàlla 21.04.2023

Jot njéggal bu joge ca Yàlla by Serigne Malick Diop

Ndax Yàlla am na? 18.04.2023

Ibrahima Diop nu jangal Kaddug Yalla

Ab Fatali ci linu jota waxtaane. 16.04.2023

Ibrahima Diop nu jangal Kaddug Yalla

Macë Saar 24 | Yàqug Yerusalem ak dellusig Doomu nit ki 05.04.2023

Xibaaru Jamm ak Ibrahima Diop

Mucc Saar 20 04.04.2023

Kóllëre gi laaj na ay sàrt Mbooloo ma dagaan na ab jottlikat

Mucc Saar 19 | Yàlla xamle na kóllëreem 02.04.2023

Serigne Malick Diop nu jangal Tawreetu Moussa

Macë Saar 23 | Yeesu gëdd na xutbakat ya ak Farisen ya 02.04.2023

Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop

Macë Saar 22 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 25.03.2023

Léebu céet ga Galag gi ñuy fey buur bi Sesaar Sadusen yi ak ndekkite li Ban santaane moo gëna màgg ci yoonu Musaa?

Macë Saar 21 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 14.03.2023

Yeesu dugg na Yerusalem Yeesu dàq na jaaykat ya ca kër Yàlla ga Yeesu rëbb na garabu figg ga

Macë Saar 19 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 07.03.2023

Ñi fase, ak ñi baña séy ngir jaamu Yàlla Xale yu ndaw yi Waxambaane wu bare alal

Macë Saar 18 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 05.03.2023

Kan moo gëna màgg? Ñi yóbbe nit bàkkaar Xar mu réer ma Mbaalug bàkkaar yi

Macë Saar 17 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 03.03.2023

Ndamu Yeesu jolli na ci moom Yeesu faj na xale bu rab jàpp Yeesu waxaat na ne dina dee, dekki

Macë Saar 16 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 28.02.2023

Kéemaan gu jóge ci asamaan Piyeer wax na ne, Yeesu mooy Almasi bi

Macë Saar 15 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 26.02.2023

Farisen ya ak aada ya Yeesu faj na doomu jigéen, ja askanoo réewu Kanaan Yeesu faj na ñu wopp Yeesu bareel na ay mburu ñaareel bi yoon

Macë Saar 14 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 23.02.2023

Yaxya faatu na Yeesu bareel na mburu ya Yeesu dox na ci kaw ndox ma

Macë Saar 13 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 21.02.2023

Léebu beykat ba Lu tax Yeesu di wax ay léeb Yeesu firi na léebu beykat bi Léebu jëmb bi

Macë Saar 12 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 19.02.2023

Yeesu nee na, mooy boroom bésub noflaay bi Yeesu faj na nit ku loxoom làggi Ku rab jàpp, mu gumba te luu Ku sosal Xelu Yàlla mi Yeesu nanguwula def kéemaan Ndeyu Yeesu ak i doomi ndeyam

Macë Saar 11 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 17.02.2023

Yaxya yónnee na, di laaj Yeesu Yeesu gëdd na ay dëkk Woote bu mag bi

Macë Saar 10 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 15.02.2023

Yeesu yónni na fukki ndaw ya ak ñaar

Macë Saar 9 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 13.02.2023

Yeesu faj na ku làggi Yeesu woo na Macë, mu nekk taalibeem Ndax warees na woor? Yeesu dekkal na doomu njiitu jàngu ba te faj jigéen Yeesu faj na ñaari gumba

Macë Saar 8 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 11.02.2023

Yeesu faj na ku gaana Ngëmu njiitu xare bi Yeesu faj na jarag yu bare

Macë Saar 20 | Xibaaru Jàmm ak Ibrahima Diop 09.02.2023

Léebu liggéeykat yi ñu jël ci waxtu yu wuute

Listen to the Sunu Yaakaar podcast in Replaio

Radio and podcasts in one app - free, with no sign-up. Install today and do not miss the launch

Get it on Google Play

Replaio is not a podcast publisher; show names, artwork and audio belong to their authors and are distributed through public RSS feeds.