Serigne Malick Diop

Sunu Yaakaar

Religion FR ↓ 353 episodes

Toppal sunu emission ci facebook.com/sunuyaakaarSoo ame laaj, Yaakaar Ju Sax am na tontu. Bindal seeni laaj ci yaakaarjusax@gmail.com

Author

Serigne Malick Diop

Category

Religion

Podcast website

soundcloud.com

Latest episode

Jan 31, 2026

Where to listen?

Podcasts in the app Replaio Radio Coming soon

Podcasts are coming to the app soon. Install now and be the first to see a whole new take on podcasts

Get it on Google Play Install for free Android 5M+ downloads · 4.8 rating iOS soon

Episodes

Yonent Yalla Youshoupha 19.08.2022

Pasteur Malick Diop partage des enseignement sur la vie de Joseph.

Ab Fatali ci linu jota waxtaane. 25.06.2022

Ibrahima Diop NGM TV Wolof

Ndax Yàlla am na? 23.06.2022

NGM TV Wolof Ibrahima Diop

Jot njéggal bu joge ca Yàlla (suite) 20.06.2022

Biibël bi ca kàllaama wolof Ibrahima Diop (NGM TV Wolof) https://www.youtube.com/channel/UCAj-5PI0DBrLCZmk8yTCPzg

Jot njéggal bu joge ca Yàlla 18.06.2022

Biibël bi ca kàllaama wolof Ibrahima Diop (NGM TV Wolof) Facebook, YouTube

Lan mooy kërcen? 15.06.2022

Biibël bi ca kàllaama wolof Ibrahima Diop (NGM TV Wolof)

Fortifie-Toi et Prends Courage - Sortez Du Milieu D'eux 14.06.2022

Pasteur Malick Diop nous enseigne la parole de Dieu

Yowanna Saa 5 18.04.2022

Ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, Doom ji mënul a def dara moom ci boppam; li mu gis Baay bi di def rekk lay def. Li Baay bi di jëf la Doom ji itam di jëf.

Yowanna Saa 04 - Ndoxum Dund 17.04.2022

Sama ñam moo di def coobarey ki ma yónni te àggale liggéey, bi mu ma sant.

Yowanna saa 3 16.04.2022

Weeru Injiil ak Sunu Yaakaar Fàww ngeen judduwaat

Yowanna saa 2 15.04.2022

Weeru Injiil ak Sunu Yaakaar Bi Yeesu nekkee Yerusalem ci màggalu bésu Jéggi ba, ñu bare gis kéemaan, yi mu doon def, daldi gëm ci turam

Ku judduwaatul doo man a seede nguuru Yàlla 14.04.2022

Amoon na ca Farisen ya nit ku ñu naan Nikodem te mu bokk ca kilifay Yawut ya. Genn guddi mu ñëw ca Yeesu ne ko: «Kilifa gi, xam nanu ne, Yàllaa la yónni ngir nga jàngal nu, ndaxte kenn mënul a def firnde yii ngay wone te Yàlla àndul ak moom.» Yeesu tontu ko ne: «Ci dëgg-dëgg maa ngi la koy wax, képp ku judduwaatul doo man a seede nguuru Yàlla.»

Man ngeen a ràññee ña doon mbubboo yonent 10.03.2022

Man ngeen a ràññee ña doon mbubboo yonent. Kan Mooy Kacou Philippe? (Discerner Les Faux Prophètes)

Pasteur Malick Diop - Comment répondre à la persécution 12.02.2022

Pasteur Malick Diop - Comment répondre à la persécution by Serigne Malick Diop

Pasteur Dawuda - 1 Jean 08.02.2022

Le pasteur Dawuda partage un message sur la façon d'avoir la communion. Pasteur Dawuda est un ancien à l'église baptiste yaakaar ju sax au Senegal.

Noel - Lu Mu Tekki - Naarelu Xaaj La 21.12.2021

Noel - Lu Mu Tekki - Naarelu Xaaj La by Serigne Malick Diop

Noel - Lu Mu Tekki - Xaaj Bu Jekk La.mp4 17.12.2021

Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop

03. Yonnente Yalla Yi Yeegle Woon Nanu Niewu Almasih Bi 30.10.2021

Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop

02. Yeesu Krist ALMASIH Lu Mu Tekki 28.10.2021

Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop

Sunu Yaakaar - Yalla dafa ko wax ci boppam! 15.10.2021

Sunu Yaakaar ak Serigne Malick Diop

01. Buuru Ndam - Ubbite gi (Pàcc 01) 14.10.2021

Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga. Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.

150 Mucc gi 02 12.10.2021

Yoonu Njub ak Pasteur Malick Fall

149 Mucc gi 01 11.10.2021

Yoonu Njub ak Pasteur Malick Fall

148 Doom ju reer ja 08.10.2021

Yoonu Njub ak Pasteur Malick Fall

147 Xar mu reer ma 07.10.2021

Yoonu Njub ak Pasteur Malick Fall

Listen to the Sunu Yaakaar podcast in Replaio

Radio and podcasts in one app - free, with no sign-up. Install today and do not miss the launch

Get it on Google Play

Replaio is not a podcast publisher; show names, artwork and audio belong to their authors and are distributed through public RSS feeds.