Librairie Majalis
Librairie Majalis
Librairie Majalis
Обов'язково відвідайте сайт подкасту та підтримайте його автора: librairiemajalis.org
Автор
Librairie Majalis
Категорія
Сайт подкасту
Останній епізод
20 жов 2026
Де слухати?
Подкасти в застосунку Replaio Radio Уже незабаромПодкасти незабаром з'являться в застосунку. Встановіть уже зараз і першими побачте зовсім новий погляд на подкасти
Епізоди
Minahu-l Miskiyyah المنح المسكية في الخوارق المبكية 02.08.2024 1:57:52
Al-Minahu-l Miskiyyah المنح المسكية في الخوارق المبكية Di téere boo xamne Sëriñ Muhammadu-l Amiin Joob Dagana, moo ko bind, jagleel ko lenn ci kéemaane Sëriñ Tuubaa yi mu fekkee, ak yi mu jëlee ci nettali yu wér. Une oeuvre de Cheikh Mouhamadoul Amine Diop, sur l’enseignements et miracles de Cheikh Ahmadou Bamba (1853-1927) Traduction & Commentaire : Abdou Khadre BA Majalis
Centenaire du rappel à Dieu de Cheikh A. Bamba: Documentaire sur la biographie du Cheikh 20.07.2024 54:17
Centenaire du rappel à Dieu de Cheikh A. Bamba: Documentaire sur la biographie du Cheikh
Ay bind ci dundug Sëriñ Tuubaa (S. Ahmadu Mbàkke) 14.05.2024 1:06:31
Ay bind ci dundug Sëriñ Tuubaa (S. Ahmadu Mbàkke), Sant Sëriñ Tuubaa, dahira Marog
"Fondement du projet de société de Cheikh Ahmadou Bamba" Commentaire S. Khadim Thiam 02.05.2024 15:49
"Fondement du projet de société de Cheikh Ahmadou Bamba" Commentaire S. Khadim Thiam
"Fondement du projet de société de Cheikh Ahmadou Bamba" par Abdallah FAHMI 02.05.2024 26:37
"Fondement du projet de société de Cheikh Ahmadou Bamba" par Abdallah FAHMI
Waxtaaani Màggalu Qasida yi : "Kan mooy Murid Saadix?" par Sëriñ Saaliw Ture 02.05.2024 23:16
Waxtaaani Màggalu Qasida yi : "Kan mooy Murid Saadix?" par Sëriñ Saaliw Ture
Waxtaani Màggalu Qasida yi - "Quelle est l’importance de la citoyenneté selon Fawzeyni ?" par Abdou Khadre Ba Majalis 02.05.2024 21:53
Waxtaani Màggalu Qasida yi - "Quelle est l’importance de la citoyenneté selon Fawzeyni ?" par Abdou Khadre Ba Majalis
MATLABUL FAWZAYNI : Dëkkandoo gu yewen, ak dëkkiin wu baax (un projet de société pour un meilleur vivre-ensemble) - Par Serigne Mourtada KEBE 27.04.2024 1:05:33
MATLABUL FAWZAYNI : Dëkkandoo gu yewen, ak dëkkiin wu baax (un projet de société pour un meilleur vivre-ensemble) - Par Serigne Mourtada KEBE
Waxtaan ci Wird Maaxuz, ak tontu ci ay laaj 15.04.2024 49:37
Waxtaan ci Wird Maaxuz, ak tontu ci ay laaj, Sëñ Maam Moor Amdi, Imam Insa Géy ak Sëñ Ahmadu Daaru Muhti
Taxawaayu Daahira ak Njariñam ci Yoonu Murid (Sëriñ Saam Buso) 14.04.2024 1:14:29
Waxtaanu Sëriñ Saam Buso ci" Taxawaayu Daahira ak Njariñam ci Yoonu Murid" Jumaay Tuubaa, Ramadan 2024
Jaamub Yàlla : Déggiin wi ak ni ko Sëriñ Tuubaa jëmmalee (Sëñ Ahmadu) 12.04.2024 1:28:02
Waxtaanu Sëñ Ahmadu Mbàkke Murtada, ci "Nangoo nekk jaamub Yàlla : Déggiin wi ak ni ko Sëriñ Tuubaa jëmmalee" Jumaay Tuubaa, 8 avril 2024
Qasida Muqaddamatul Xidma (Sëriñ Abuu Baraka Mbàkke) 10.04.2024 3:55:06
Qasida Muqaddamatul Xidma (Sëriñ Abuu Baraka Mbàkke)
Yarug ruuh ci njàngalem Sëriñ Tuubaa (L'Éducation Spirituelle dans l'Enseignements de Cheikh A. Bamba) - Sëriñ Afiya Ñang 05.04.2024 1:07:55
Waxtaanu Sëriñ Afiya Ñang, ci "Yarug ruuh ci njàngalem Sëriñ Tuubaa (L'Éducation Spirituelle dans l'Enseignements de Cheikh A. Bamba)" Tuubaa, 4 avril 2024
Tawati deru yaram (les maladies dermatologiques) - Dr Asan JOOB 01.04.2024 58:13
Waxaatnu Dr Asan JOOB, ci "Tawati deru yaram (les maladies dermatologiques)" Daaru Muhti, 28 mars 2024
Njàngum jigéen; ay jubluwaayam aki jeexitam (L'éducation des filles : objectifs et effets) - Sëñ Maxtaar Lòo 01.04.2024 1:18:07
Waxtaanu Sëñ Maxtaar Lòo, ci "Njàngum jigéen; ay jubluwaayam aki jeexitam (L'éducation des femmes : objectifs et effets)" Jumaay Tuubaa, 30 mars 2024
Ay jëf yees tere ci jënd ak jaay (Pratiques interdites en matière de commerce) - Sñ Abdu Xaadir Buso 01.04.2024 1:08:40
Waxtaanu Sëriñ Abdu Xaadir Buso ci "Ay jëf yees tere ci jënd ak jaay (Pratiques interdites en matière de commerce)" Jumaay Tuubaa, 29 mar 2024
Midâdi Arabe-Français (Serigne Abû Baraka et Serigne Allasane ) 28.03.2024 23:41
Midâdi Arabe-Français (Serigne Abû Baraka et Serigne Allasane )
Jazbu-l Qulub Arabe-Français (Serigne Abû Baraka et Serigne Allasane ) 28.03.2024 1:13:22
Jazbu-l Qulub Arabe-Français (Serigne Abû Baraka et Serigne Allasane )
Ay bind yu jëm ci labat Soxna ak ponki sëy (Leçons sur les fiançailles et les piliers du mariage) - Sëriñ Mbàkke A. Rahmaan 27.03.2024 54:30
Waxtaanu Sëriñ Mbàkke Abdu Rahmaan ci " Ay bind yu jëm ci labat Soxna ak ponki sëy" (Leçons sur les fiançailles et les piliers du mariage) Jumaay Tuubaa, 26 Mars 2024
Ni Sëriñ Tuubaa jàngalee Tawhiid (Sëriñ Ahmadu Mbàkke) 26.03.2024 56:36
Ni Sëriñ Tuubaa jàngalee Tawhiid (Sëriñ Ahmadu Mbàkke)
Lettre de Serigne Mbacke BOUSSO adressée au député Ngalandou DIOUF) - Serigne Sam Bousso 26.03.2024 1:08:01
Waxtaanu Sëriñ Saam Buso, ci jàngat bataaxalu Sëriñ Mbàkke Buso jëm ci Ngalandu Juuf, mu tuddee ko "kàddug dëgg mooy wax" (La Bonne gouvernance : Lettre de Serigne Mbacke BOUSSO adressée au député Ngalandou DIOUF) Jumaay Tuubaa, 24 Mars 2024
L'autodéfense (Nan ngay aare sa bopp, ba ken dula mana gaañ) - Pr Mamadou Ba 25.03.2024 1:28:49
Waxtaanu Pr Mamadou Ba, ci "L'autodéfense" (Nan ngay aare sa bopp, ba ken dula mana gaañ) Daaru Muhty Alwafa 23 Mars 2024
Jàngat Qasidag Matlabu-l Fawzayni (étude et analyse) par S. Maam Moor Mbàkke Amdi 25.03.2024 1:16:20
Waxtaanu Sëriñ Maam Moor Mbàkke Amdi, ci Jàngat ak faram fàcce Qasidag Matlabu-l Fawzayni" (Qasida Matlabu-l Fawzayni : étude et analyse) Jumaay Tuubaa 23 Mars 2024
Jaar-jaari Sëriñ Tuubaa, ci Minanu-l Bâqil Xadîm ( Sëriñ Abo Mbàkke Bas Moor) 24.03.2024 1:08:06
Waxtaanu Sëriñ Abo Mbàkke Bas Moor, ci jaar-jaari Sëriñ Tuubaa, ni ko téereb Minanul Baaqil Xadiim indee. Copyright : Touba TV (Diwân du Ramadan)
Warteefu ma-réew ci tànn njiit (la responsabilité du citoyen de choisir un leader ) - Sëriñ Seexunaa Mbàkke 23.03.2024 1:07:13
Waxtaanu Sëriñ Seexunaa Mbàkke ci "Warteefu ma-réew ci tànn njiit (la responsabilité du citoyen de choisir un leader ) " Jumaay Tuubaa, 22 Mars 2024
Схожі подкасти
Replaio не є видавцем подкастів; назви шоу, обкладинки та аудіо належать їхнім авторам і поширюються через публічні RSS-канали