Librairie Majalis

Librairie Majalis

Religion WO ↓ 325 episodes

Librairie Majalis

Author

Librairie Majalis

Category

Religion

Podcast website

librairiemajalis.org

Latest episode

May 4, 2026

Where to listen?

Podcasts in the app Replaio Radio Coming soon

Podcasts are coming to the app soon. Install now and be the first to see a whole new take on podcasts

Get it on Google Play Install for free Android 5M+ downloads · 4.8 rating iOS soon

Episodes

Lettre de Serigne Mbacke BOUSSO adressée au député Ngalandou DIOUF) - Serigne Sam Bousso 26.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Saam Buso, ci jàngat bataaxalu Sëriñ Mbàkke Buso jëm ci Ngalandu Juuf, mu tuddee ko "kàddug dëgg mooy wax" (La Bonne gouvernance : Lettre de Serigne Mbacke BOUSSO adressée au député Ngalandou DIOUF) Jumaay Tuubaa, 24 Mars 2024

L'autodéfense (Nan ngay aare sa bopp, ba ken dula mana gaañ) - Pr Mamadou Ba 25.03.2024

Waxtaanu Pr Mamadou Ba, ci "L'autodéfense" (Nan ngay aare sa bopp, ba ken dula mana gaañ) Daaru Muhty Alwafa 23 Mars 2024

Jàngat Qasidag Matlabu-l Fawzayni (étude et analyse) par S. Maam Moor Mbàkke Amdi 25.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Maam Moor Mbàkke Amdi, ci Jàngat ak faram fàcce Qasidag Matlabu-l Fawzayni" (Qasida Matlabu-l Fawzayni : étude et analyse) Jumaay Tuubaa 23 Mars 2024

Jaar-jaari Sëriñ Tuubaa, ci Minanu-l Bâqil Xadîm ( Sëriñ Abo Mbàkke Bas Moor) 24.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Abo Mbàkke Bas Moor, ci jaar-jaari Sëriñ Tuubaa, ni ko téereb Minanul Baaqil Xadiim indee. Copyright : Touba TV (Diwân du Ramadan)

Warteefu ma-réew ci tànn njiit (la responsabilité du citoyen de choisir un leader ) - Sëriñ Seexunaa Mbàkke 23.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Seexunaa Mbàkke ci "Warteefu ma-réew ci tànn njiit (la responsabilité du citoyen de choisir un leader ) " Jumaay Tuubaa, 22 Mars 2024

Xeexub Réewum Falastin ak Mbooloom Israayil (Conflit Israélo-palestinien) - S. Amdi MBAKKE 20.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Amdi Mustafaa Mbàkke, ci "Xeexub Réewum Falastin ak Mbooloom Israayil (Conflit Israélo-palestinien)" Daaru Muhti 20 Mars 2024

Njariñul jariñ mbindéef yi, ak ay fànnam (Sëriñ Aboo Mbàkke) 19.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Aboo Mbàkke mom Sëñ Basiiru Moor, ci "Njariñul jariñ mbindéef yi, ak ay fànnam" Jumaay Tuubaa 17 Mars 2024

Ñawug xarala yu yees yi (Intelligence Artificielle) - Commissaire Aly KANDE 19.03.2024

Waxtaanu Commissaire Aly KANDE, ci "Ñawug xarala yu yees yi (Intelligence Artificielle)" Daaru-l Muhti 17 Mars 2024

Sunu Ndawi démb ya, ak yoy tay yi (La bravoure des dirigeants de notre société à l'étude du passé et du présent) - Sëriñ Aliw Mbàkke Fàllilu 19.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Aliw Mbàkke mom Sëñ Fàllu, ci "Sunu Ndawi démb ya, ak yoy tay yi (La bravoure des dirigeants de notre société à l'étude du passé et du présent)" Daaru-l Muhti 18 Mars 2024

Sàmm ndono (Sauvegarder le Patrimoine) - Pr Sëriñ Masàmba Gëy 19.03.2024

Waxtaanu Pr Sëriñ Masàmba Gëy, ci "Nees di xammee ndono ak nees koy sàmmee (Sauvegarder le Patrimoine)" Daaru-l Muhti 16 Mars 2024

Sëriñ bu mak bi ak mbindum loxoom (Manuscrit de Cheikhoul Khadim) par Sëriñ Fàllu Mbàkke 17.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Fàllu Mbàkke Ibn Sëriñ Moodu Abdu Xaadir, ci "Sëriñ bu mak bi ak mbindum loxoom (Manuscrit de Cheikhoul Khadim)" Daaru-l Muhti 16 Mars 2024

Xam-xamu Bidiw (Astronomie) par Sëriñ Seexunaa Buso Siidi 17.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Seexunaa Buso Siidi, ci "Xam-xamu Bidiw (Astronomie). Daaru-l Muhti 12 Mars 2024

Waqf ci Senegaal ak nu ko Murid gi mana taxawee ngir mu jëm kanam (Dr Abdullaahi Jaxate) 17.03.2024

Waxtaanu Dr Abdullaahi Jaxate, ci "waqf ci Senegaal ak nu ko Murid gi mana taxawee ngir mu jëm kanam". Jumaay Tuubaa 16 Mars 2024

Bind yu aju ci nàmpal ak yor xale (Sëriñ Ibrahima KEBE) 17.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Ibrahima KEBE, ci "Bind yu aju ci nàmpal ak yor xale". Jumaay Tuubaa 15 Mars 2024

Sàrti digle lu baax ak tere ab safaan (Sñ Mustafaa Joob Ndar) 17.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Mustafaa Joob Ndar, ci "Sàrti digle lu baax ak tere ab safaan". Jumaay Tuubaa 14 Mars 2024

Melokaanu Kilifag Diiné ak wàccuwaayam (Sëriñ Maamun Mbàkke Fàllu) 17.03.2024

Waxtaanu Sëriñ Maamun Mbàkke Fàllilu, ci Melokaanu Kilifag Diiné ak wàccuwaayam. Jumaay Tuubaa 13 Mars 2024

Koor ak ay àtteem (Sëriñ Seexunaa Mbàkke Murtadaa Fàllu) 14.03.2024

Waxtaanu koor ci Jumaay Tuubaa, jëm ci Koor ak ay àtteem (Sëriñ Seexunaa Mbàkke Murtadaa Fàllu)

HT Matlabul Fawzayni Daaju Sëriñ Tafsiir Joob 13.03.2024

HT Matlabul Fawzayni Daaju Sëriñ Tafsiir Joob

Yasuru Rasûla-l Lâhi (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Wa inahû lakitâbun azîzun (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Faqad Jâ-akoum (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Muhammad (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Bika-l Yawma Akmaltu (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Midâdî (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Wakâna Hàqan (Serigne Abû Baraka MBACKE) 07.03.2024

Njàngum Qasaayid Sëriñ Abû Baraka MBAKKE ibn Sëriñ Basiiru Fàllu

Listen to the Librairie Majalis podcast in Replaio

Radio and podcasts in one app - free, with no sign-up. Install today and do not miss the launch

Get it on Google Play

Replaio is not a podcast publisher; show names, artwork and audio belong to their authors and are distributed through public RSS feeds.