Librairie Majalis

Librairie Majalis

Religion WO ↓ 345 episodes

Librairie Majalis

Be sure to visit the podcast's website and support the creator: librairiemajalis.org

Author

Librairie Majalis

Category

Religion

Podcast website

librairiemajalis.org

Latest episode

Oct 20, 2026

Where to listen?

Podcasts in the app Replaio Radio Coming soon

Podcasts are coming to the app soon. Install now and be the first to see a whole new take on podcasts

Get it on Google Play Install for free Android almost 10M downloads · 4.8 rating iOS soon

Episodes

Wolofal SMK (Warnanoo dellu sant Xayrul Xadiimi) 15.10.2023

Wolofali Seex Musaa KA, Seex Abdul Ahad KA jàng ko njàng mu leer, te set. Yalna ko Yàlla fay te sàmm ko

Bind 5 : Mawâhibul Qudûs - (20i Melokaan yi jomb ci ci sunu Boroom) 13.10.2023

Mawâhibul Qudûs, di téeré bu Sëriñ Tuubaa bind ci TAWHIID, Sëriñ Fàllu MBÀKKE mom Sñ Ahmadu Rafaahii Fàllilu, tekki ko ci wolof.

Firi Qasida Hasbuna'Lâhu (par Akb Majalis) 10.10.2023

Hasbuna'Lâhu, mooy Qasida gi Sëriñ Tuubaa bindoon keroog ba mu jogee Mbàkke Baari, ba tollu Jeewol

Bind 4 : Mawâhibul Qudûs - (20i Melokaani sunu Boroom, seeni jagoo ak seeni matale) 09.10.2023

Mawâhibul Qudûs, di téeré bu Sëriñ Tuubaa bind ci TAWHIID, Sëriñ Fàllu MBÀKKE mom Sñ Ahmadu Rafaahii Fàllilu, tekki ko ci wolof.

Le concept "Khidma" de Cheikh A. Bamba (Serigne Salih SALAN) 06.10.2023

Le concept "Khidma" de Cheikh A. Bamba (Serigne Salih SALAN)

Bind 3 : Mawâhibul Qudûs - (Ni Yàlla nekkee Buur) 05.10.2023

Mawâhibul Qudûs, di téeré bu Sëriñ Tuubaa bind ci TAWHIID, Sëriñ Fàllu MBÀKKE mom Sñ Ahmadu Rafaahii Fàllilu, tekki ko ci wolof.

Lan mooy wahaabiya, ak cosaanam (Sñ A. Rafaahii MBÀKKE) 05.10.2023

Waxtaan wu am solo, wow Sñ Ahmadu Rafaahii MBÀKKE, tënk na ci mbirum wahaabiya, ak sosoom, ak seeni pas-pas, ak liy seen jafe-jafe sa diggënte ak yeneen jullit yi

Bind 2 : Mawâhibul Qudûs - (Melokaani sunu Boroom yi) 02.10.2023

Mawâhibul Qudûs, di téeré bu Sëriñ Tuubaa bind ci TAWHIID, Sëriñ Fàllu MBÀKKE mom Sñ Ahmadu Rafaahii Fàllilu, tekki ko ci wolof.

#Majalis'Al Khadîmiyyah : Jaar-jaari Yonent bi SHW ci Qasidag Jazbul Qulûb 28.09.2023

#Majalis'Al Khadîmiyyah : Jaar-jaari Yonent bi SHW ci Qasidag Jazbul Qulûb Présentation : Akb Majalis Invité : S. Murtada Sylla

Bind 1 : Mawâhibul Qudûs - (Ubbiteg téere bi) 28.09.2023

Mawâhibul Qudûs, di téeré bu Sëriñ Tuubaa bind ci TAWHIID, Sëriñ Fàllu MBÀKKE mom Sñ Ahmadu Rafaahii Fàllilu, tekki ko ci wolof.

Diggënte Murid yi ak Qasida yi (Par Sëriñ Xaliil MBAKKE ) 21.09.2023

Diggënte Murid yi ak Qasida yi (Par Sëriñ Xaliil MBAKKE Ibn Sñ Mustafaa Hafas)

Exposé sur la Qasida "Li Rabbin Qafûrin" par S. Cheikhouna Bousso Thioumblène 21.09.2023

Exposé sur la Qasida "Li Rabbin Qafûrin" par S. Cheikhouna Bousso Thioumblène

Njariñul Qasida yi - Sñ Basiiru MBÀKKE XELKOM 20.09.2023

Njariñul Qasida yi - Sñ Basiiru MBÀKKE XELKOM

Jaar-Jaari Aliyu RTA (Partie 2) - (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Aliyu RTA (Partie 2), di ñeenteelu xalifab Lislaam (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM)

Jaar-Jaari Aliyu RTA (Partie 1) - (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Aliyu RTA (Partie 1), di ñeenteelu xalifab Lislaam (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM)

Jaar-Jaari Sayidunaa Usmaan RTA - (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Usmaan Ibn Haffaan RTA (Partie 1), di ñatteelu xalifab Lislaam (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM)

Jaar-Jaari Sayidunaa Omar Ibn Xàttaab RTA (Partie 2) (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Sayidunaa Omar Ibn Xàttaab RTA (Partie 2), di ñaareelu xalifab Lislaam (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM)

Jaar-Jaari Sayidunaa Omar Ibn Xàttaab RTA (Partie 1) (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Sayidunaa Omar Ibn Xàttaab RTA (Partie 1), di ñaareelu xalifab Lislaam (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM)

Jaar-Jaari Sayidunaa Abû Bakr RTA (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM) 20.09.2023

Jaar-Jaari Sayidunaa Abû Bakr RTA (Ci Kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE XELKOM))

#Majalis'Al Khadîmiyyah : Sòobu 18.09.2023

Emission #Majalis'Al Khadîmiyyah Invité : Sëriñ Mustafaa Joob Al-kokki Thème : Sòobu

Sîratu'n Nabî - 01 "Njaalbéenug Yonent bi SHW" 17.09.2023

Sîratu'n Nabî - 01 "Njaalbéenug Yonent bi SHW". Ci kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE Abdu Kariim

Sîratu'n Nabî - 02 "Gàddaayug Èthiopie" 17.09.2023

Sîratu'n Nabî - 02 "Gàddaayug Èthiopie". Ci kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE Abdu Kariim

Sîratu'n Nabî - 03 "Wan ginnaaw gi waa Xuraychin wanoon ginnaaw waa Banuu Haachim" 17.09.2023

Sîratu'n Nabî - 03 "Wan ginnaaw gi waa Xuraychin wanoon ginnaaw waa Banuu Haachim". Ci kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE Abdu Kariim

Sîratu'n Nabî - 04 "Gàddayug Yonent bi SHW". 17.09.2023

Sîratu'n Nabî - 04 "Gàddayug Yonent bi SHW". Ci kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE Abdu Kariim

Sîratu'n Nabî - 05 "Hikma bi nekk ci jànga Sîra Yonent bi SHW" 17.09.2023

Sîratu'n Nabî - 05 "Hikma bi nekk ci jànga Sîra Yonent bi SHW". Ci kàddug Sëriñ Basiiru MBÀKKE Abdu Kariim

Listen to the Librairie Majalis podcast in Replaio

Radio and podcasts in one app - free, with no sign-up. Install today and do not miss the launch

Get it on Google Play

Replaio is not a podcast publisher; show names, artwork and audio belong to their authors and are distributed through public RSS feeds.