Serigne Malick Diop

Sunu Yaakaar

Toppal sunu emission ci facebook.com/sunuyaakaarSoo ame laaj, Yaakaar Ju Sax am na tontu. Bindal seeni laaj ci yaakaarjusax@gmail.com

Mindenképp látogasd meg a podcast oldalát, és támogasd a készítőjét: soundcloud.com

Szerző

Serigne Malick Diop

Kategória

Religion

A podcast weboldala

soundcloud.com

Legutóbbi epizód

2026. jan. 31.

Hol hallgathatod?

Podcastok az alkalmazásban Replaio Radio Hamarosan

A podcastok hamarosan megérkeznek az alkalmazásba. Telepítsd most, és láss elsőként egy teljesen új megközelítést a podcastokhoz

Letöltés a Google Play-ről Telepítsd ingyen Android közel 10 M letöltés · 4,8-as értékelés iOS hamarosan

Epizódok

Samba Alieu Bah | Hobbe Tato Ibraahiima Bem 05.01.2024

Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Samba Alieu Bah | Fii No Alla Noddiri Ibraahiima 29.12.2023

Samba Alieu Bah | Fii No Alla Noddiri Ibraahiima by Serigne Malick Diop

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu (Fulfulde, Pulaar) 12.11.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu (Fulfulde, Pulaar) by Serigne Malick Diop

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu (Fulfulde, Pulaar) 12.11.2023

Kibaaru Moyyo

Injiilu Almashi Bi Issa | Nettalib ci Wolof 04.11.2023

Bare na ñu fexee bind ab nettalib mbir, yi sotti woon ci sunu biir, noonee nu ko jote ca ña ko fekke woon ca ndoorte la, te seede yooyu mujj doon jawriñi kàddug Yàlla. Moo tax man it, ma fas laa yéenee bindal lépp ba mu jekk gannaaw ba ma gëstoo mbir mépp, dale ko ca ndoorte la, ba mu leer nàññ. Ko defee nga xam xéll ne li ñu la jàngal, lu wér péŋŋ la.

Kibaaru Moƴƴo | Partie 09 01.11.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 08 30.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 07 28.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 06 26.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 05 24.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 03 20.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moƴƴo | Partie 04 19.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moyyo | Partie 02 19.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Kibaaru Moyyo | Partie 01 18.10.2023

Ko fuɗɗoode Kibaaru Moƴƴo Iisaa Almasiihu

Pasteur Malick Diop 16.10.2023

Malick Diop | Sunu Yaakaar

Luug Saar 01 | Malaaka yégle na juddub Yaxya 22.09.2023

Bare na ñu fexee bind ab nettalib mbir, yi sotti woon ci sunu biir, noonee nu ko jote ca ña ko fekke woon ca ndoorte la, te seede yooyu mujj doon jawriñi kàddug Yàlla. Moo tax man it, ma fas laa yéenee bindal lépp ba mu jekk, yaw Tewofil mu tedd mi, gannaaw ba ma gëstoo mbir mépp, dale ko ca ndoorte la, ba mu leer nàññ. Su ko defee nga xam xéll ne li ñu la jàngal, lu wér péŋŋ la.

Mucc Saar 29 25.06.2023

Serigne Malick Diop nu njangal tawreetu Moussa

Mucc Saar 28 | Malick Diop 19.06.2023

Lu jëm ci yérey sarxalkat yi

Mucc Saar 27 | Malick Diop 11.06.2023

Mucc Saar 27 | Malick Diop by Serigne Malick Diop

Mucc Saar 26 | Malick Diop 04.06.2023

Lu jëm ci sori xaymab jaamookaay bi | Lu jëm ci kenuy jaamookaay bi | Lu jëm ci rido bi | Lu jëm ci kiiraayal buntu xayma bi

Mucc Saar 25 | Malick Diop 29.05.2023

Lu jëm ci jaamookaay bi | Lu jëm ci gaal giy def àlluway seede si | Lu jëm ci taabalu mburum sarax mi | Lu jëm ci tegukaayu làmp bi

Mucc Saar 22 | Malick Diop 16.05.2023

Yoonu Aji Sax ji ñoŋal na alalu nit | Yoonu Aji Sax ji rafetal na dundin Bu ngeen dee lebal ku bokk ci sama ñoñ, di néew-ji-doole ju ngeen dëkkal, buleen def ni ab leblekat, di ko sas ab tegandaay.

Mucc Saar 21 | Malick Diop 13.05.2023

Lu jëm ci Ebrë yiy ay jaam | Lu jëm ci lor sa moroom |

Mace Saar 28 Xibaaru Jamm ak Ibrahima Diop 08.05.2023

Injiilu almasi bi

Mace Saar 27 | Xibaaru Jamm ak Ibrahima Diop 01.05.2023

Injiilu Almasi Bi

Hallgasd a(z) Sunu Yaakaar podcastot a Replaióban

Rádió és podcastok egy alkalmazásban - ingyen és regisztráció nélkül. Telepítsd még ma, és ne maradj le a premierről

Letöltés a Google Play-ről

A Replaio nem podcastkiadó; a műsorok nevei, borítóképei és hanganyagai a szerzőiket illetik, és nyilvános RSS-csatornákon keresztül terjednek.